Wut ndimbal ci jëfekaayu Groove misik
Ngir jot ndimbal ci Groove, dugalal laaj bi ci boyetu seet bi ci laatu-waar wi. Di nga jot ay tontu yu bawoo Cortana wala Bing.

Ngir jot ndimbal ci Groove, dugalal laaj bi ci boyetu seet bi ci laatu-waar wi. Di nga jot ay tontu yu bawoo Cortana wala Bing.
Jàngal yi gën a yomb ci Windows 10, nga xam li ci bees ci Jëfekaayu Tàmbali bi. Ngir gis ko, tànnal bitoŋ bi ci suuf wala nga tànn bitoŋu Door, bindal Tàmbalil, ba noppi nga bës Enter.
When an alarm goes off, you’ll hear a sound and see a notification that you can snooze or dismiss.
Continue reading ni ñuy jëfandikoo yyetekaay bi ci windows 10
Sudee bës ci bitoŋuLonkci barabu toppatoo gisul sa jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth, jéemal lii:
Wérlul ni sa jëfandaayu Windows dafay nangu Bluetooth ak ndax taal nañ ko. Dinga gis ab bitoŋu Bluetooth ci barabu toppatoo gi.
Wérlul ni jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth mu ngi takk te mën nañ ko gis. Ni nga koy defee dafay wuute ci jëfandaay yi, kon xoolal leeral yu àndak sa jëfandaay wala nga dem ci daluweb defarkat.
To connect your Bluetooth headset, speaker, or headphones to your Windows 10 PC, you’ll need to pair the device first.
Turn on your Bluetooth device and make it discoverable.
The way you make it discoverable depends on the device. Check the device info or website to find out more.
On the taskbar, select the action center icon, and make sure Bluetooth is turned on.
In action center, select Connect, then pick your device.
Follow any additional instructions. Otherwise, you’re done.
Soo gisee ab bittoŋu tëj ci wetu ab màkkanu daluweb ci Microsoft Edge, mooy:
Li ngay yónnee te jot ci daluweb fas nañ ko, luy waral muy jafe ci ku nekk mu mën a jot ci leeral yii.
Wéral nañu daluweb bii, luy tekki ni këru liggéeyukaay buy doxal dal bi am ba ab firnde buy wone ni ñoo ko moom. Bësal bitoŋu tëj gi ngir xam ki moom dal bi ak ku koy saytu.
Su daluweb bi amee gomb bu dóomu-taal mooy tekki ni wéral nañ ko te saytu nañ ko, ngomb bu wert mooy tekki ni Microsoft Edge japp na ni daluweb bii bu baax bi la. Limuy jëfandikoo daganalu Wéral buñ Xóotal (EV), buy laaj pexey wéralug ràññeekaay gu gën a tar.
Baatu-jàll bu am doole dina tax ba kenn ku amul sañ-sañ du mën a jot ci say taxañ say tëriin ak yeneen jumtukaay, te dina jafe ci ñoom ñu koy xam wala jëli. Baatu-jàll bu baax:
War na am gën gaa néew juróom-ñatti araf
Warul am sa turu jëfandikukat, sa tur dëgg, wala turu liggéeyukaay
Warul am baat lëmm
Dafa wara wuute bu baax ak baatu-jàll yi nga yoroon
War na araf yu mag, araf yu ndaw, nimero, ak ay màndarga
Mënul a gis sa móolukaay ci lim bi? Wérlul ni taal nañ ko te lonku na ci mennum mbaalu Wi-Fi niki sa telefon. Sudee gisu looko ba noppi, xoolal ndax sa móolukaay mën na àndak Windows 10 Mobile móol.
Currently, Cortana is only available in the following countries/regions: China, France, Germany, Italy, Spain, United Kingdom, and United States. Cortana is available in these languages: Chinese (Simplified), English (U.K.), English (U.S.), French, Italian, German, and Spanish.
Some Windows 10 editions let you defer upgrades to your PC. When you defer upgrades, new Windows features won’t be downloaded or installed for several months. Deferring upgrades doesn’t affect security updates. Note that deferring upgrades will prevent you from getting the latest Windows features as soon as they’re available.