aar sa pc windows 10 ak windows defender

Nan lañuy aare sa PC Windows 10

Ana Security Essentials?

Soo amee Windows 10,mën nga jot ci Microsoft Security Essentials. Waaye soxla woo ko, ndax am nga Windows Defender ba noppi, buy joxe mennum dayob kaarànge.


Ci laatu seet bi, mbindal Windows Defender.
Tànnal Windows Defender ci njuréef yi. Di nga mën a xool sa ordinatëer ak tolluwaayu kaarànge yëddu.

aar sa pc windows 10 ak windows defender
aar sa pc windows 10 ak windows defender

Taal mbaa fay Windows Defender

Ci Windows 10, Windows Defender dafay dëkke di takk te dox ngir aar sa PC. Dina fayal boppam soo sampee beneen jëfekaayu xeex yëddu.
Defender dafay jëfandikoo kaarànge gu teew ngir càmbar taxañ yi nga yokk walla yiy dox ci sa PC. Fayal kaarànge gu teew ab diir soo demee ci Jekkal yi > Yeesal ak kaarànge > Windows Defender.

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *