ana sama móolukaay ci windows 10 mobile?

Ana sama móolukaay ci Windows 10 Mobile?

Mënul a gis sa móolukaay ci lim bi? Wérlul ni taal nañ ko te lonku na ci mennum mbaalu Wi-Fi niki sa telefon. Sudee gisu looko ba noppi, xoolal ndax sa móolukaay mën na àndak Windows 10 Mobile móol.

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *