jot ndimbal ak lëñbatukaay taxañ ci windows 10

Ndimbal ci Lëñbatukaayu Taxañ

Tomb yu kawe

Yile ay tontu lañ ci ay laaj yuy faral di am ci Lëñbatukaayu Taxañ:
Nan laay jëmmalee jotiin wu gaaw?
Nan la OneDrive di doxee ci Windows 10?
Ana samay kàggu?
Sooy seet darra, seetal yeneeni tombi Lëñbatukaayu Taxañ.

Ndimbal ci Windows 10

jot ndimbal ak lëñbatukaay taxañ ci windows 10
jot ndimbal ak lëñbatukaay taxañ ci windows 10

Dugalal ab laaj walla ab baatu-seet ci boyetu seet bi ngir nga mën a jot ay tontu ci Microsoft, Web bi, ak Cortana.

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *