naka la ñuy sosee baatu-jàll bu am doole

Sos baatu-jàll bu am doole

Baatu-jàll bu am doole dina tax ba kenn ku amul sañ-sañ du mën a jot ci say taxañ say tëriin ak yeneen jumtukaay, te dina jafe ci ñoom ñu koy xam wala jëli. Baatu-jàll bu baax:
War na am gën gaa néew juróom-ñatti araf
Warul am sa turu jëfandikukat, sa tur dëgg, wala turu liggéeyukaay
Warul am baat lëmm
Dafa wara wuute bu baax ak baatu-jàll yi nga yoroon
War na araf yu mag, araf yu ndaw, nimero, ak ay màndarga

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *