seet ay yeesal ci windows 10

Yeesal Windows 10

Windows 10 dinay faral di seetal boppam ay yeesal ngir noppal la. Su ab yeesal jàppandee, dañ koy yebbi te samp ko ci saasi — wéyal di yeesal sa PC ak man-man yu mujj yi.
Ngir seet ay yeesal léegi, demal ci Jekkal yi > Yeesal & kaarànge > Windows Update, tetànn Seet ay yeesal. Sudee Windows Update dafa wax ni sa PC yeeslu na ba noppi, di nga am bépp yeesal bi jàppandi fimne nii.

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *