saafaral ay lonku ci ay jëfandaayu kàddu Bluetooth ak ay wone yu amul buum Kàddu BluetoothJëfandaayi Miracast Sudee bës ci bitoŋuLonkci barabu toppatoo gisul sa jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth, jéemal lii: Wérlul ni sa jëfandaayu Windows dafay nangu Bluetooth ak ndax taal nañ ko. Dinga gis ab bitoŋu Bluetooth ci barabu toppatoo gi. Wérlul ni jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth mu ngi takk te mën nañ ko gis. Ni nga koy defee dafay wuute ci jëfandaay yi, kon xoolal leeral yu àndak sa jëfandaay wala nga dem ci daluweb defarkat. Sooy seet yeneen jëfandaay yuy doxee Bluetooth yu wuute ak yu kàddu, demal ci xëtu Jekkali Bluetooth bi. Demal ci Jekkal yi, tànnal Jëfandaay yi, tànnal Bluetooth tànnal jëfandaay bi, tànnal Dindi jëfandaay, te nga jéemaat leen kuupale.

saafaral ay lonku ci ay jëfandaayu kàddu Bluetooth ak ay wone yu amul buum

Kàddu Bluetooth

Sudee bës ci bitoŋuLonkci barabu toppatoo gisul sa jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth, jéemal lii:
Wérlul ni sa jëfandaayu Windows dafay nangu Bluetooth ak ndax taal nañ ko. Dinga gis ab bitoŋu Bluetooth ci barabu toppatoo gi.
Wérlul ni jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth mu ngi takk te mën nañ ko gis. Ni nga koy defee dafay wuute ci jëfandaay yi, kon xoolal leeral yu àndak sa jëfandaay wala nga dem ci daluweb defarkat.

Continue reading saafaral ay lonku ci ay jëfandaayu kàddu Bluetooth ak ay wone yu amul buum Kàddu BluetoothJëfandaayi Miracast Sudee bës ci bitoŋuLonkci barabu toppatoo gisul sa jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth, jéemal lii: Wérlul ni sa jëfandaayu Windows dafay nangu Bluetooth ak ndax taal nañ ko. Dinga gis ab bitoŋu Bluetooth ci barabu toppatoo gi. Wérlul ni jëfandaayu kàddu biy doxee Bluetooth mu ngi takk te mën nañ ko gis. Ni nga koy defee dafay wuute ci jëfandaay yi, kon xoolal leeral yu àndak sa jëfandaay wala nga dem ci daluweb defarkat. Sooy seet yeneen jëfandaay yuy doxee Bluetooth yu wuute ak yu kàddu, demal ci xëtu Jekkali Bluetooth bi. Demal ci Jekkal yi, tànnal Jëfandaay yi, tànnal Bluetooth tànnal jëfandaay bi, tànnal Dindi jëfandaay, te nga jéemaat leen kuupale.

lu tax cortana amul ci sama diiwaan walla sama làkk?

lu tax cortana amul ci sama diiwaan walla sama làkk?

Currently, Cortana is only available in the following countries/regions: China, France, Germany, Italy, Spain, United Kingdom, and United States. Cortana is available in these languages: Chinese (Simplified), English (U.K.), English (U.S.), French, Italian, German, and Spanish.

windows hello ci windows 10

Xam lu jëm ci Windows Hello te nga jekkal ko

Windows 10

Windows Hello moo gën a jagoo, anam wi gën a wóor ngir dugg ci saasi ci jëfandaayi Windows 10 di jëfandikoo sa rëddi-baaraam, wala xàmmee kanam. Surface Pro 4, Surface Book, ak PC yu bari yu am xàmmekaayu rëddu baaraam, leegi mën nañu dox ci Windows Hello, ak ci yeneen jëfandaay yu mën a xàmmee sa kanam ak rëddu-baaraam leegi ñu jàppandi. Nii lañu koy jekkalee:
Demal ci njëlu Door nga tànn Jekkal yi.
Dem ci Sàq yi > Dugg tànneef yi .

Continue reading windows hello ci windows 10

xool walla far jaar-jaaru xuus ci microsoft edge

Windows 10

Anu kusakatula mbiri ndi mfundo zimene Microsoft Kudera akukumbukira – kuphatikizapo mapasiwedi, uthenga inu mwalowa mu mitundu, ndi malo mudapitako – ndipo m’masitolo pa PC monga inu Sakatulani intaneti.
Kuona wanu kusakatula mbiri, kusankha Pankakhala> History. Kwa winawake izo, kusankha Chotsani onse mbiri, kusankha mitundu deta kapena owona mukufuna kuchotsa anu PC, ndiye kusankha Chotsani

Continue reading xool walla far jaar-jaaru xuus ci microsoft edge